Madior Ak Dior - Épisode 11 [Saison 01]

Share
Sitene Add
  • Published on Apr 14, 2019

  • [ABONNEZ-VOUS ici] ☆~~👉 http://www.youtube.com/c/PikiniProduc... [FACEBOOK]☆~~👉 https://www.fb.com/PikiniProductions [TWITTER]☆~~👉https://www.twitter.com/PikiniProd #Madior_ak_Dior_https://www.youtube.com/playlist?list... #Pikininfos_https://www.youtube.com/playlist?list... #SÉRIE_BÈS_https://www.youtube.com/playlist?list... WhatsApp ☆~~👉 +221776626858 Pikini Productions ByBen 2019

Comments

  • fall bakh yaye fall

    Ana gni beugue sen maman 🤗🤗

  • Nabou Diop
    Nabou Diop 1 week ago

    Ana sopéye lape fall baboul mouridina

  • Tawfexx TV
    Tawfexx TV 1 week ago

    Yallna niép am khaliss bou bari amine

  • Aminata Ba
    Aminata Ba 1 week ago

    Waaa diaspora nouyounalennn kou bok sama situation ande sétane série yeup wonel sa bop 😂😂😂😂

  • abdou Thiam
    abdou Thiam 1 week ago

    Anna gni geume ni destin amna. Lep dina fegne inchalla Bakhe rek mo Ame solo 🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • Fatima Mbengue
    Fatima Mbengue 1 week ago

    Yalla yalla doli soutoureu ak khëweul si barkë seydina mouhamed je regarde après je suis au boulot

  • Diarra Hanne
    Diarra Hanne 1 week ago

    Yalla nañu yalla doli soutoureu ak diami adouna ak akahira mouseul gnou si saytané🤲🤲

  • Anta Rassoul Dieye
    Anta Rassoul Dieye 1 week ago

    Yalna gneup ak diam thji barki seybina mouhamet saw

  • Mariama sané
    Mariama sané 1 week ago

    Anni wadial Gamou Srgne Babacar Sy thia St Louis

  • baboucha lome
    baboucha lome 1 week ago

    Yalna diame yague si Sénégal ak képou kou begue sa maman rk

  • Adjia Bousso
    Adjia Bousso 1 week ago

    Non bayilén di confondre théâtre ak vie réel osi yénagui gni beugue ray ak yama ak yaye dagne lén wara guéné si série niom sén rôle rék lagni déf t je crois elle son réussi puisque niogui lén di dérangé inshh

  • boy diop
    boy diop 1 week ago

    Yalla nafi yalla bayi sama yaye sa bayi fi sén yaye si barkéb borom touba ❤️ 👌 kép kou kham ni yayam 😭 def ko dji nio gui koy nianeal yalla kharé ko aldiana si barkéb borom touba❤️

  • aminata
    aminata 1 week ago

    Yama ak yayam sokhor naniou fou sokhor yem

  • Elhadji badara Diagne

    Team Dior venez ici 👈❤️

  • Mass Ndiaye
    Mass Ndiaye 1 week ago

    Kou beugue sa yaye n'e nii

  • Maman Djite
    Maman Djite 1 week ago

    Ziar naléne yalna diam yague si barké seydina Mohamed (psl)

  • Amdy Moustapha Kandji

    J'aime bien la mère de Dior elle est géniale et naturelle

  • Ameth Tine
    Ameth Tine 1 week ago

    yalla nala yalla May wère dollila soutoura ba loyotou diotko si barkè sèydina mouhamed psl🙏🙏🙏❤❤❤

  • ndeya ndiaye
    ndeya ndiaye 1 week ago

    Kou dackor ni Nar sikhoram bi mo bari Sénégal kou ray say mbok say none diekh

  • Mina Amar
    Mina Amar 1 week ago

    Nar dinama ray aka beugeu xaliss 🤣mais elle joue bien son rôle ak parfum bi da naturel chanllange bokk si parfum nar bi🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣